jëleeti Flashcards
where would you find him(her/it) again?
foo koy jëleeti?
someone who loves you the way i do
ku la bëggee ni man
ku la nobee ni man
someone who admires you the way i do
ku la soppee ni man
someone who wakes you up at midnight to check if you have covered yourself
ku yeewu xaaja guddi di xool ndax saangu nga
someone (like me) who tells you the truth you don’t want to hear
ku lay wax dëgg joo (ji nga) bëggula déeg, ni man
everyone has a side that God Almighty put them in and a side they want to be in
ku nekk ak fa la buur bi yalla feétëlee ak fa nga bëgg sa bopp féetée
where would i find her (him/it) again?
fu ma koy jëleeti
someone who loves me the way you do
ku ma nobee ni yow
someone who gets jealous over me like you do
ku may fiiree ni yow
when God Almighty loves you, you know it
bu la buur bi yalla bëggee da nga koy xam, ndax tóoxiduna boo dugg mu geénee la ci
when someone loves you, my friend, you know it
bu la nit ki bëggee doom yaay da nga koy xam
because when they smell trouble they say “come along with me”
ndax bu musiba di xeeñ mu ne “kaay gungeé ma fii”
that’s life right there, in front of us
aaduna ngoogu (ngi nóono) ci suñu kanam
one shouldn’t threaten/harm his peer
jaam warula tëkku/nattu moroomu jaamam