asking for things and prices Flashcards
do you have any/is there any (bread)?
am nga (mburu)?
(mburu) am na?
do you sell salt?
da ngay jaay xorom?
i would like some bread
mburu laa bëggoon
how much does it cost?
ñaata lay jar?
how much do you sell (pepper) for?
ñaata ngay jaaye (poobar)?
how much do you sell it for?
ñaata nga koy jaaye
do you have change for (500)?
di nga am weccetu (téeméer)?
am nga weccetu (téeméer)?
sell me (one)
jaay ma (benn)
it’s very expensive
seer na lool
lower the price
wàññi ko
make it 500
def ko 500
500 is all i have
500 laa fi yor
500 laa am
500 is all i can pay
500 laa mën a fey
i can pay you 500
mën naa la fey 500
i’ll pay (2500)
(juróom téeméer) laay fey
it costs (1000)
(ñaari téeméer) lay jar
i usually buy it for 100
100 laa tàmm di ko jënde