Words Flashcards
ab
Ab paaka la yore
indéfini pour la classe b-
Il a un couteau sur lui
abal
Abal ma sa téere!
prêter
Prête moi ton livre
able
Peñe, ken du ko able
prêter
un peigne, personne ne le prête
afeer b-
Loolu sa afeer la
affaire
C’est ton affaire
ag
indéfini pour la classe g-
agsi
Xabaar bi aksi na démb
arriver, survenir
La nouvelle est arrivée hier
aj
Fatou aj na laytanam
placer en haut, percher
Fatou a placé sa calabasse en haut
aj
faire le pélerinage à la Mecque
ku
qui annexion pour la classe k-
bëgg
bëgg na mango
dafa bëggoon tukki, waaye paasam mutul
aimer, vouloir, avoir envie
il aime les mangues
il voulait voyager, mais il lui manquait d’argent pour le billet
bu
Néeg bu tuuti la
Bu liggéey bi eggee dinaa leen nexal
1 annexion pour la classe b-
C’est une petite chambre
2 Quand le travail sera terminé, je vous récompenserai
mat
Taaf bi matul, jëndaat ci ñaari meetar
être complet, arriver à maturité, être conforme à certaines normes de grandeur
l’étoffe est insuffisante, achêtes-en encore deux mètres
Ku Bëgg lem ñeme yamb
ñeme
qui veut du miel ne doit pas craindre l’abeille
avoir le courage de, oser, être courageux, ne pas avoir peur de
comment
nan, naka, na
nan
nan nga gise mbir mi
de manière, comment?
comment vois tu l’affaire
naka
naka-jekk
naka-jegg fii lay fanaan
?
normalement, de tout temps
normalement. je passe la nuit ici
na
waxu ma na mbir ma deme woon
dafa defoon na yow
de manière, comment
il ne m’a pas dit comment l’affaire s’était passé
indicatif de fonction
il avait fait comme toi
mbir m-
l’affaire
gise
voir
il ne m’a pas dit comment l’affaire s’était passé
waxu ma na mbir ma deme woon
il avait fait comme toi
dafa defoon na yow
normalement. je passe la nuit ici
naka-jegg fii lay fanaan
Prête moi ton livre
abal ma sa téere
un peigne, personne ne le prête
peñe, ken du ko able
Percher, placer en haut
Fatou a placé sa calabasse en haut
aj
Fatou aj na laytanam
aimer, vouloir, avoir envie
il aime les mangues
il voulait voyager, mais il lui manquait d’argent pour le billet
bëgg
bëgg na mango
dafa bëggoon tukki, waaye paasam mutul
1 annexion pour la classe b-
C’est une petite chambre
2 Quand le travail sera terminé, je vous récompenserai
bu
Néeg bu tuuti la
Bu liggéey bi eggee dinaa leen nexal
yamb w-
xam na lu bare ci yamb yi
abeille
il connaît beaucoup de choses sur les abeilles
abeille
il connaît beaucoup de choses sur les abeilles
yamb w-
xam na lu bare ci yamb yi
qui veut du miel ne doit pas craindre l’abeille
avoir le courage de, oser, être courageux, ne pas avoir peur de
Ku Bëgg lem ñeme yamb
ñeme
boo ñeme téegu, na nga ma ko wax
quand tu auras le courage de te faire circonscrire, tu me le diras
quand tu auras le courage de te faire circonscrire, tu me le diras
boo ñeme téegu, na nga ma ko wax
Am naa giléém ca Gànnaar yomb naa wax
J’ai un chameau en Mauritanie, c’est facile à dire.
J’ai un chameau en Mauritanie, c’est facile à dire.
Am naa giléem ca Gànnaar yomb naa wax
giléem, gëléem g-
dromedaire. chameau
dromedaire. chameau
giléem, gëléem g-
Gànnaar g-
Mauritanie
Mauritanie
Gànnaar g-
yomb
être facile, être bon marché
être facile, être bon marché
yomb
kaayleen ma jox leen cax wu yomb
venez je vous donne une divinette facile
venez je vous donne une divinette facile
kaayleen ma jox leen cax wu yomb
jên, noor lay gën yomb
le poisson en saison sèche est moins cher
le poisson en saison sèche est moins cher
jên, noor lay gën yomb
Tuñum giléém lang na, waaye rotul
La lèvre du chameau pend, mais elle ne tombe pas.
La lèvre du chameau pend, mais elle ne tombe pas.
Tuñum giléém lang na, waaye rotul
tuñ m-
lèvre
lèvre
tuñ m-
lang
prendre, dépasser, s’accrocher
prendre, dépasser, s’accrocher
lang
rot
tomber
tomber
rot
defaraatal sa ëmb, musóor gaa ngiy lang
refait ton paquet, le foulard dépasse
refait ton paquet, le foulaar dépasse
defaraatal sa ëmb, musóor gaa ngiy lang
musóor g-
le foulard
le foulard
musóor g-
gaa
particule d’insistance
particule d’insistance
gaa
ngiy
ww
ww
ngiy
Bant, lumu yàgg cig dex, du tax mu soppiku jasig
Un bout de bois, il peut rester longtemps longtemps dans un fleuve, ce n’est pas pour ça qu’il va se transformer en crocodile.
Un bout de bois, il peut rester longtemps longtemps dans un fleuve, ce n’est pas pour ça qu’il va se transformer en crocodile.
Bant, lumu yàgg cig dex, du tax mu soppiku jasig
Bant
bout de bois
bout de bois
Bant
yàgg
rester longtemps
rester longtemps
yàgg
dex g-
fleuve, rivière
fleuve, rivière
dex g-
dëgg neexul a dégg
la vérité n’est pas toujours agréable à entendre
la vérité n’est pas toujours agréable à entendre
dëgg neexul a dégg
jasig j-
crocodile
crocodile
jasig j-
soppi
changer
changer
soppi
soppi b-
le changement
le changement
soppi b-