Introduction Flashcards
Couteau
Paaka
Nez
Bakkan
Avoir soif
Mar
Ramasser
For
Pluie
Taw
Courir
Daw
Dormir
Nelaw
Sol
Suuf
Être joli
Rafet
Bracelet
Lam
Maison
Kër
Arbre
Garab
Riz
Riz au poisson
Ceeb
Ceebu jën
Marmite
Cin
Pagne
Séer
Clé
Caabi
Épouse
Jabar
Coudre
Ñaw
Guitare
Xalam
Sueur
Ñaq
Appeler
Woo
Le cheval
Fas wi
Mâchoire
Ńaam
Prononciation comme ng en Anglais parking
Lit
Lal
Parler une langue étrangère
Làkk
Propre
Set
Œil
Bēt
Abattre une arbre
Gor
Se lever
Jóg
Hyène
Bukki
Être brûlant
Sās
Lutteur
Il a terrassé tous les lutteurs
Mbër
Daan na mbër yépp
Récipient
Ndab
Vente
Njaay
Vent
Ngelaw
Planter un pieu
nl paal
Samp
Porte
Bunt
Garder
Denc
Jambe
Tànk
Être rouge
Xonq
Sol
Suuf
Maison
Kër gi
Sama nijaay
Mon oncle
Classificateurs
Genre humain
K- au singulier
Ñ- au pluriel
Genre non-humain
Le classificateur est celui du nom auquel il est fait référence
Genre abstrait
Classificateur L-
Il est tombé
Dafa daanu
Il est parti
Dem na
Il viendra
Dîna ñów
C’est lui qui avait pris
Moo faboon
Il est mince
Dafa sew
Il est beau
Rafet na
Ce sera bon
Dina baax
Le chemin était étroit
Yoon wi dafa xatoon
Très
Lool
Déjà
Xaat
Ne… jamais
Mukk
C’est très froid
Dafa sedd guyy
C’est très rouge
Dafa xonq coyy
Il sait pertinemment
Xam na xéll
Il est raide comme un «I»
Dafa ne jodd
Pourtant
Moona
Mais
Waaye
Pour ainsi dire
Daanaka
Puisque
Nde
Cela étant
Kon
Je ne peux pas ne pas faire ce qu’il a dit, mais le cœur n’y est pas
Mëñuma bañ def li mu wax, waaye xol bi àndu ci
Il n’y a plus qu’un seul lutteur qui me tienne tête
Menn mbër dońń a ma të
La nuit dernière
Biig
Le nord
Bëj gunnaar
A cet endroit là
Fée
A ce moment là
Booba
Ainsi
Nii
Quand, lorsque
Bi
Ba
Quand, chaque fois que, si
Bu
Su
Je l’ai rejoint au moment où il s’apprêtait à traverser la rue
Maa ngi ko dab bi muy waaj a jàll tali bi
Association
Ak
Pour,
Pour que
Ngir
Ndax
Dans
Sur
Comme
Jusqu’à, Jusqu’à ce que
Fi
Ci
Ni
Ba
Merci
Jëre-jëf
Epaule
Mbagg m-