Chapter 5 Flashcards
Ramadan Breakfast
Xe*ed
to cut the fast
nndogu
to fast
woor
Rice with Meat
Yapp
Peanut butter sauce
Maafe
Onion sauce
Yaasa
Millet
Dugub
Coucous
Cere
Meat
Yapp
Fish
Jen
Dry fish
Keccax
Peanut Butter
Tigadege
Bread
Mburu
Sauce
Soos/nyeex
Water
ndox
Milk
Meew
Ygurt
Soow
Salt
Xorom
Sugar
Suuke*er
It taste good
Neex na
it’s salty
Dafa saf xorom
its spicy
Dafa saf Kaani
Its sweet
Dafa Neex
Its bitter
Dafa Wax
I’m full
Suur naa
I’m hungry
Dafa xiif
to sit around the bowl
Toog ci bool bi
to share
Bokk
Come to have lunch
Kaay an~
Come to have dinner
Kaay reer
What time is it
Ban Waxtu moo jot
It’s 2:30
2 waxtu ak gennwal
Its 2:10
2 waxtu teg na 10 minut
its 2:40
2 waxtu des na 20 minit
At what time do you
Ban waxtu nga
Days
Bes yi
Sunrise
Suba
Early afternooon- 2:15
Tisbaar
late afternoon
Takkusaan
twilight/dusk
timis
nightitme
Gee
Rainy Season
Newet
Harvest period
lolli
Garden Period
Noor
Hot and dry season
Cooroon
The weather is dry
Dafa mbooyo
It’s sunny
Dafa naaj
it’s cloudy
dafa xiin
it’s foggy
dafa lay
It rainds
dafay tax
it snows
dafay taw galaas
to ride a bike
Dawal welo
to meet with friends
daje ak xarit yi
to walk
dox
to think
xalaat
to pray
julli
to be chilly
feex
to be humid
Guus
very
torop
I don’t eat meat because I am a vegitarian
Duma Lekk yapp ndaxte vegetariienne
Tomorrow bira wont og to the field because she is sick
Suba Bira du dem tool ndaxte dafa feebar
Where can I find
Fan moo am
where can I buy
fan laa mena jemde
Do you have
Am nga
Lower the price
Wanni ko
How much can you pay
Naata nga mena fay
I can pay
Men naa fay
Fii la mena yem
this is my final price
Cheese
Fromaas
Ice cream
Galaas
Iced fruit juice
radi
egg
nen
butter
Buerre
chicken
Ginaar
goat
Bey
beef
nag
lamb
xar
shrimp
sippax
corn
mboq
cookie
mbiskit
oil
diwlin
Money
Xaalis
Change money
Weccit
slice
morso
a pile
saam
bleach
ordisawel
broom
bale
to increase
yokk
To lower
Waññi
Cassava
Ñambi
Onion
Soble
Squash
Naajo
Lemon
Limon
Eggplant
Batañse
Hot pepper
Kaani
Potato
Pombiteer
Sweet potato
Pataas
Lettuce
Salaat
Cabbage
Suppome