Chapter 17 Flashcards
To remake
Defaraat
Prefix to make something small
Sin ex. sindaala=worthless shoe
Regularly or habitual
Dee example- dafa dee toogal jen he regularly cooks fish
To live vivre
Doondu
Forever
Be faww
I want you to…..
Dama begg nga
If you want
Bo begga
What are you going to do?
Looy def
I can do it
Men def li
You can not
Munuma deff
Only- seulement
Kesse
The force
Doolay
Remove
Dendil
Yes you want it?
Begga nga ko
I want that
Lii la begga
To retake
Jelaat
Wait for me in front of the boutique
Xaar ma ci kanamu butik bi
I am very hungry today
Xiif naa lool tey
I am tired
Sonn naa
To finish- finir
Noppi
Garder
Denc
Habit
Tamm
I have the habit of coming here
Tamm naa now fii
The people of
Waa
Humble
Woyof
Ignorance
Nakka Xam
Immediately
Ci saas
Impoli
Yara diku
Jelousy
Kanaan
He is not here
Nekku fii
He is over there
Munga fa
No one obligated you to do it
Kenn forsewula nga def ko
I will be busy
Dina ko toppatoo
Participer
Bokk
I hope that he will participate
Yaakaar naa ni dina bokk
He can go throughout
Men naa dema funekk
Pousser
Dugal
C’est toi qui m’ad pousse a le faire
Yaa ma ci dugal
What do you prefer
Ban ngaci tammu
Prayer
Julli
Punit
Yar
God will punish it
Yalla dina ko yar
Quel que chose
Dara
Il a dit quel que chose
Wax na dara
Race- ethnis
Xeet wi
Raconter
Nettali
Regarder
Xool
Regarder moi bien
Xool ma bubaax
Regret
Reccu
I don’t have a single regret on that
Amuma benni reccu ci loolu
I want to rest with you
Dama begga des ak yow
Situation
Nekkin wi
He is in a difficult dituation
Mungi ci nekkin wi meti
Souhait
Yeen bi
That is my wish
Sama yesne la
Sufgestion
Ndigtak bi
Thats a good suggestion
Ndigtal bubaax la
God said its not good
Yalla nana baaxul
Its been a long time
Ya ga na
I haven’t seen yoou
Gis na la gis
Me too
Man tamm