Wolof Assimil Flashcards
1
Q
Comment t’appelles tu?
A
Naka nga tudd?
2
Q
Je m’appelle Amelie
A
Maa ngi tudd Amelie
3
Q
Je suis européenne
A
Waa Tugal laa
4
Q
D’où viens-tu?
A
Waa fan nga?
5
Q
Moi aussi
A
Man itam
6
Q
Vouloir
A
Bëgg
7
Q
Visiter
A
Wër
8
Q
Aller
A
Dem
9
Q
Je
A
Ma
10
Q
Tu
A
Nga
11
Q
Il/elle
A
Mu
12
Q
Nous
A
Nu
13
Q
Vous
A
Ngeen
14
Q
Ils/elles/on
A
Ñu
15
Q
Je suis
A
…laa
16
Q
Tu es
A
…nga
17
Q
Il est
A
…la
18
Q
Voici
A
A ngi
19
Q
Voilà
A
A nga
20
Q
Te voici
A
Yaa ngi
21
Q
Manger
A
Lekk
22
Q
Mange!
A
Lekkal!
23
Q
Mangez!
A
Lekkleen!
24
Q
Ami
A
Xarit
25
Q
Connectif : l’ami de fanta
A
XaritU Fanta
26
Q
Ici
A
Fi
27
Q
Habiter
A
Dëkk
28
Q
C’est à Gorée que nous sommes aller
A
Gore LAnu dem
29
Q
Avoir
A
Am
30
Q
Combien
A
Ñaata
31
Q
Enfant
A
Doom
32
Q
Et
A
Ag
33
Q
1
A
Benn
34
Q
Homme
A
Góor
35
Q
2
A
Ñaar
36
Q
Femme
A
Jigéen
37
Q
Quoi
A
Lan
38
Q
Voir
A
Gis
39
Q
J’ai vu
A
Gis naa
Verbe d’action + conjugaison en na
40
Q
Je suis fatiguée
A
Sonn naa
41
Q
Je mange du riz
Inaccompli
A
Ceeb laay lekk
42
Q
Riz
A
Ceeb
43
Q
Qui (Subordonnée relative)
A
Yu