Wolof Flashcards
1
Q
Laa
A
I am
2
Q
Nga
A
You are
3
Q
La
A
He / she is
4
Q
Maa ngi tudd
A
My name is / I call myself
5
Q
Yaa ngi tudd
A
Your name is / you call yourself
6
Q
Mu ngi tudd
A
Her / his name is
7
Q
Yow nak
A
And you?
8
Q
Maa ngi tudd Matthew
A
My name is Matthew
9
Q
Man itam
A
Me too
10
Q
Waa France laa
A
I am French
11
Q
Waa Canada laa
A
I am Canadian
12
Q
Wër
A
To visit
13
Q
Waa fan nga
A
Where are you from?
14
Q
Dama bëgga wër Senegaal
A
I want to visit Senegal
15
Q
Na nga déf
A
How are you?
16
Q
Ma ngi fi
A
I am fine
17
Q
No tudu
A
What is your name?
18
Q
Jerejef
A
Thank you
19
Q
mbokki Canada laa
A
I am Canadian
20
Q
waa Canada la
A
He is Canadian
21
Q
Xaritu Matthew laa
A
I am a friend of Matthew
22
Q
Man
A
Me
23
Q
Danga bëg wër Canada
A
Do you want to visit Canada
24
Q
Salaamaalekum yen ñepp
A
Hello everyone
25
Ba leggi
See you soon
26
Kañ
When
27
Fan
Where
28
Naka
How
29
Lu tax
Why
30
Ñaata
How many
31
Tus
0
32
Benn
1
33
Ñaar
2
34
Ñett
3
35
Ñent
4
36
Juróom
5
37
5
Juróom
38
0
Tus
39
3
Ñett
40
Waaw
Yes
41
Waa Canada nga?
Are you Canadian?
42
Dégguma bu baax wolof
I don’t speak Wolof well
43
6
Juroom benn
44
7
Juroom ñaar
45
Juróom-ñett
8
46
Juróom-ñent
9
47
Fukk
10
48
Déedéet
No
49
Fan nga dëkk?
Where do you live?
50
Canada laa dëkk
I live in Canada
51
Ñaata _____ nga am?
How many _____ do you have?
52
Ban waxtoo mo jott?
What time is it?
53
bëgg
to want
54
Laa sopp
I like
55
def
to put (infinitive)
56
bopp
head
57
sarica
gift
58
Fi
Here
59
Fa
There
60
rekk
only
61
wax
to say
62
ba beneen
bye
63
ineer
1 o’clock
64
deeseer
2 o’clock
65
turwaseer
3 o’clock