Lan mooy addina Flashcards
1
Q
waxambaane
A
young man
2
Q
laabir
A
compassionate/open/funny
3
Q
laabiroon
A
was compassionate
4
Q
digal
A
prescribe/recommend
5
Q
digalna ma dem
A
he advised me to go
6
Q
romb
A
pass by
7
Q
bëret
A
to get up quickly/jump up
8
Q
tabbindoo
A
fall upon/arrive at the same time
9
Q
wax jooju tabbindoo ci noppu baay bi ag ba doom ji
A
their words fell upon the father and son’s ears at the same time
10
Q
bayyi/ba
A
leave behind/leave alone/let go
11
Q
Dangay jéém mbaa nga ba
A
You try or you leave it alone
12
Q
Ku bëgg nag, looy def mu neex ñepp, dangay sonnal sa bopp, ndax ñepp bokkuñu yem xalaat.
A
Who wants then, you want to please everyone, you will tire your head because no one shares the same thought.
13
Q
yem/yam
A
the same
14
Q
ñoo yem
A
we are the same